Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 90:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 90:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Nu xëy, nga reggal nu sa ngor, nuy sarxolle, bànneexoo ko sunu giiru dund.
15 Bànneexal nu limu fan yi nga nu mbugal, diirub ati tiis yi nu dund.
16 Yal na sa jaloore leer sa jaam ñi, sa daraja leer seeni doom.
Sabóor 90 in Kàddug Yàlla gi