Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 84:5-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 84:5-9 in Kàddug Yàlla gi

5 Ndokklee ku dëkke sa kër, di la màggalati. Selaw.
6 Ndokklee ku lay doolewoo, te namma topp njool ma jëm sa kër.
7 Buy jàll xuru Jooyoo, mu saf ko bëti ndox, céebo sànge xur wa barke,
8 muy gëna am doole, ba teewi fa Yàlla ca Siyoŋ.
9 Éy Yàlla Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, déglul, ma ñaan la! Yàllay Yanqóoba, teewlu ma. Selaw.
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi