Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 80:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 80:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 mbaam àll di ko ruur, ndundati àll di ca for?
15 Éy Yàlla Boroom gàngoor yi, geesul; séentool asamaan, ba gis te taxawusi reseñ jii.
16 Taxawusil njëmbat lii nga jëmbate sa ndijoor, ngarab sii nga dooleelal sa bopp.
Sabóor 80 in Kàddug Yàlla gi