Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 74:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 74:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Dikkal, xool gent bu yaa bii dul jeex, noon yàq lépp ci biir kër gu sell gi.
4 Say bañ xaacu nañ fa sa digg bérabu ndaje ma, samp seen raaya.
5 Sémmiñ dal, wàkku awu. Mbete ñu xàcciy sémmiñ, di gori geer, ba lu fa doon liggéeyu yett, tas.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi