Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Kàddug Yàlla gi
-
Sabóor
-
Sabóor 74
Sabóor 74:3-5
Help us?
Click on verse(s) to share them!
3
Dikkal, xool gent bu yaa bii dul jeex, noon yàq lépp ci biir kër gu sell gi.
4
Say bañ xaacu nañ fa sa digg bérabu ndaje ma, samp seen raaya.
5
Sémmiñ dal, wàkku awu. Mbete ñu xàcciy sémmiñ, di gori geer, ba lu fa doon liggéeyu yett, tas.
Sabóor 74
Sabóor 74:3-5
< Sabóor
>
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms