Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 boole leen jot ci notaangeek loraange, ngir fonk seen bakkan.
15 Yal na Buur gudd fan, yal nañu ko may wurusu Saba. Nañu koy ñaanal saa su ne, di ko saxoo, mu barkeel.
16 Yal na pepp ne gàññ ci réew mi, yal na gub yay jaayu ca tund ya ni gottub Libaŋ; dëkk yu mag yi sëqi nit ba law,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi