Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:7-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Firndey alkànde la ma ñu bare xoole woon, te yaw ngay sama rawtu bu wóor.
8 Samay kàddu sag cant la fees ak di la saxoo darajaal.
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi