Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:7-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:7-11 in Kàddug Yàlla gi

7 Firndey alkànde la ma ñu bare xoole woon, te yaw ngay sama rawtu bu wóor.
8 Samay kàddu sag cant la fees ak di la saxoo darajaal.
9 Ngalla bu ma wacc, mag laa; bu ma ba fi doole jeexe.
10 Noon yaa nga may tooge, ñi may tëroo ngay diisoo,
11 naan: «Yàlla wacc na ko, nan ko dàq, jàpp; kenn du ko wallu.»
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi