Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Yal nangay sama cëslaay, sama rawtu bu may rawesi saa su ne, te nga dogal sama mucc. Yaw yaa may téye, di ma aar.
4 Éy sama Yàlla, musal ma ci dooley ku bon ak ab saaysaay ak ab néeg.
5 Boroom bi, Aji Sax ji, yaw de laa yaakaar, dale laa wóolu ba may ndaw.
6 Yaw laa wéeroo ba may juddu; yaw yaa ma roccee sama biiru ndey. Yaa yelloo sama cant fàww.
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi