Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 71:20-22 in Wolof
Help us?
Sabóor 71:20-22
in
Kàddug Yàlla gi
20
Won nga ma ay yoon coonooki tiis, waaye yaa may dundalaat, ma mucc xóotey suuf.
21
Yal nanga ma gëna sagal, geesu, bégal ma.
22
Man it sama Yàlla, ma xalam, sant la ngir sa kóllëre. Aji Sell ji séddoo Israyil, dama lay woy aki xalam,
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms