Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:14-16 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Man may saxoo yaakaar, di la sant, di santati.
15 May siiwal sa njekk, di yendoo waxtaane say wall, doonte lim ba wees na ma.
16 Boroom bi, Aji Sax ji, ma dikke la sag njàmbaar, di tudd sa njekk gu wéet.
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi