Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:13-14 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Samay seytaane, yal nañu leen rusloo, sànk leen. Ñi may wuta lor, yal nañu leen gàcceel, sewal leen.
14 Man may saxoo yaakaar, di la sant, di santati.
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi