Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 55:7-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 55:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Dama ne: «Éy ku may may laafi xati, ma ne fërr, noppluji.
8 Xanaa ma naaw, ba sore, fanaani màndiŋ ma. Selaw.
9 Naa gaawtu, seeluji ngelaw lu riddi ak ngëlén.»
10 Éy, Boroom bi, beenal seeni wax, neenal leen. Damaa gis fitnaak xuloo ci dëkk bi,
Sabóor 55 in Kàddug Yàlla gi