Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 55:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 55:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Teewlu ma, nangul ma. Li may tawat a ma xañ jàmm, ub sama bopp;
4 coowal noon yee ak coonob ñu bon ñi. Dañu maa teg fitna, di ma songe xadar.
Sabóor 55 in Kàddug Yàlla gi