Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 55:19-21 in Wolof
Help us?
Sabóor 55:19-21
in
Kàddug Yàlla gi
19
Moo may jot ak jàmm, ba ma mucc ci xare ya ma ñu bare di songe.
20
Yàllaay dégg, duma leen, moom mi nguuram yàgga sax. Selaw. Soppikuwuñu fenn te ragaluñu Yàlla.
21
Kii a ngi xàccil ñi mu takktool, di fecci kóllëre,
Sabóor 55 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms