Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 49:6-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 49:6-10 in Kàddug Yàlla gi

6 Ana lu may tiit bés yu metti, yu ma njublaŋ yéewe seeni ñaawtéef,
7 di ñu wóolu seen am-am, di kañoo alal ju bare?
8 Ana ku mana jota jot sa bakkanu moroom, mbaa mu di ko feyal Yàlla njot ga?
9 Njotug bakkan jafe na, bu ci jéem dara.
10 Ana kuy dund ba fàww, ba doo gis bàmmeel?
Sabóor 49 in Kàddug Yàlla gi