Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 41:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 41:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ku dikk, di ma seet, di jinigal tey fenti sos ci xolam, bu génnee, tasaare ko.
8 Bañ yépp a ngi may déeyoo, di ma fexeel lu bon,
9 naan: «Musiba dal na ko, du jógati!»
Sabóor 41 in Kàddug Yàlla gi