Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 41:5-8 in Wolof

Help us?

Sabóor 41:5-8 in Kàddug Yàlla gi

5 Dama ne: «Aji Sax ji, tooñ naa la; baaxe ma, faj ma.»
6 Noon yaa ngi may yéene lu bon, naan: «Xanaa kii du dee, ba ñu fàtte ko?»
7 Ku dikk, di ma seet, di jinigal tey fenti sos ci xolam, bu génnee, tasaare ko.
8 Bañ yépp a ngi may déeyoo, di ma fexeel lu bon,
Sabóor 41 in Kàddug Yàlla gi