Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 41:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 41:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax jee lay aar, di sàmm sa bakkan, nga jagoo barke ci réew mi, te du la bàyyi noon def la lu ko neex.
4 Aji Sax jee lay dooleel soo woppee, di soppi bu baax sa tëraay.
5 Dama ne: «Aji Sax ji, tooñ naa la; baaxe ma, faj ma.»
6 Noon yaa ngi may yéene lu bon, naan: «Xanaa kii du dee, ba ñu fàtte ko?»
Sabóor 41 in Kàddug Yàlla gi