Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 40:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 40:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 génnee ma ca kàmbug sànkute, sippee ma ca xóotey ban ba, cëppe ma ciw doj, samp ma, ma dëgër.
4 Moo ma may, ma fent, woy wu ma woye sunu Yàlla. Ñu baree seede, di wormaal ak a dénku ci Aji Sax ji.
5 Ndokklee, yaw mi dénku ci Aji Sax ji, te sàkkuwoo ku bew ak kuy topp ay fen.
Sabóor 40 in Kàddug Yàlla gi