Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 29:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 29:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Aji Sax jeey àddu, fettaxal sawara, mu boy.
8 Aji Sax ji àddooti, yëngal màndiŋ, Aji Sax jee yëngal màndiŋu Kades.
9 Aji Sax jeey àddu, kéwél matu, garabi àll ruus, biir këram di mennum riir, naan: «Màggal-leen ko!»
Sabóor 29 in Kàddug Yàlla gi