Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 29:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 29:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax jeey àddu ca kaw ndox ma, Yàlla mu tedd maa dënu, Aji Sax jeey tiim ndox, mi ne màww.
4 Aji Sax jeey àddoo doole, Aji Sax jeey àddoo daraja.
Sabóor 29 in Kàddug Yàlla gi