Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 28:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 28:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Bu ma sànkaaleek ab soxor, di ma booleek kuy def lu bon, di wax moroom ma jàmm, te dencal ko ay ca xolam.
4 Fey leen seen liggéey, seen kemu jëf ju bon. Jox leen seen añu jëf, yool leen seen yelleef.
5 Xooluñu Aji Sax jeeki jëfam, ak liggéey bi mu def. Da leen di yàqte, te dootu leen yékkati.
6 Jaajëfe Aji Sax ji, ki ma nangul samay dagaan!
Sabóor 28 in Kàddug Yàlla gi