Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 24:6-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 24:6-9 in Kàddug Yàlla gi

6 Ñooñooy waa làng, gi lay sàkku, di maasug Yanqóoba, giy sàkku sa yiw. Selaw.
7 Neleen bunt yi kulbét, ubbileen bunti cosaan yi, Buur Boroom ndam duggsi.
8 Buur Boroom ndam booboo di kan? Xanaa Aji Sax ji Boroom dooleek njàmbaar, Aji Sax ji jàmbaaru xare ji.
9 Neleen bunt yi kulbét, ubbileen bunti cosaan yi, Buur Boroom ndam duggsi.
Sabóor 24 in Kàddug Yàlla gi