Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 23:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 23:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 leqli ma, teg ma ci yooni njekk ngir teddngay turam.
4 Su may jaare xuru ndee wu ne këruus it, duma ragal loraange: yaw laak man, sa bantu sàmm ak sa nguul, yooyoo may dalal.
5 Yaa ma berndeel, noon yi gis, nga diwal ma saa bopp, terale ma, saab kaas rembat.
6 Mbaax ak ngor kay la ma Aji Sax jiy dare sama giiru dund, ma dëkke këram ba fàww.
Sabóor 23 in Kàddug Yàlla gi