Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 16:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 16:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 Ma sant Aji Sax ji may xelal, ba guddi sax sama xel di ma yedd.
8 Damaa saxoo ne jàkk ci Aji Sax ji ndijoor la ma fare, ba duma tërëf,
9 xanaa di bànneexu, sama xol bég, sama yaram finaax.
Sabóor 16 in Kàddug Yàlla gi