Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 16:5-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 16:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Aji Sax ji, yaay wàll wi ma séddoo, di sama ndabal xéewal. Yaa yor sama wërsëg.
6 Maa muurloo bérab bu neex, ndaw cér bu rafet!
Sabóor 16 in Kàddug Yàlla gi