Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 16:4-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 16:4-5 in Kàddug Yàlla gi

4 Kuy sàkkuy tuur barew tiis, man de duma leen tuural deret, sama làmmiñ du leen tudd.
5 Aji Sax ji, yaay wàll wi ma séddoo, di sama ndabal xéewal. Yaa yor sama wërsëg.
Sabóor 16 in Kàddug Yàlla gi