Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 16:3-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 16:3-7 in Kàddug Yàlla gi

3 Ñu sell ñi ci réew mi ñooy garmi yi, sama mbégte mépp ñoom a.
4 Kuy sàkkuy tuur barew tiis, man de duma leen tuural deret, sama làmmiñ du leen tudd.
5 Aji Sax ji, yaay wàll wi ma séddoo, di sama ndabal xéewal. Yaa yor sama wërsëg.
6 Maa muurloo bérab bu neex, ndaw cér bu rafet!
7 Ma sant Aji Sax ji may xelal, ba guddi sax sama xel di ma yedd.
Sabóor 16 in Kàddug Yàlla gi