Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 15:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 15:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Du sos, du tooñ dëkkandoo, du baatal moroomam.
4 Ku siblu, mu sib, ku ragal Yàlla, mu teral. Mooy sàmm ngiñam, su ko dee lor it.
Sabóor 15 in Kàddug Yàlla gi