Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 141:5-7 in Wolof

Help us?

Sabóor 141:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Kuy déggal Yàlla, man na maa dóor, bantal ma ci ngor. Loolu ngëneelu cuuraay la, duma ko bañ. Waaye maa ngi saxoo ñaan pexey noon moy.
6 Yal nañu fenqe seeni njiit ciw doj, ba noon yi xam ne dëgg laa wax.
7 Ni ñuy gàbbe suuf ba mu ne ŋafeet, ni la njaniiw di ŋaye, aw seeni yax yu tasaaroo.
Sabóor 141 in Kàddug Yàlla gi