Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 141:3-5 in Wolof

Help us?

Sabóor 141:3-5 in Kàddug Yàlla gi

3 Aji Sax ji, sàmmal ma sama làmmiñ, saytul ma sama kàddu.
4 Bu ma xiir ci lu aay, may jëfe jëf ju bon, ànd ceek ñiy jëf lu ñaaw, di wàlli seeni bernde.
5 Kuy déggal Yàlla, man na maa dóor, bantal ma ci ngor. Loolu ngëneelu cuuraay la, duma ko bañ. Waaye maa ngi saxoo ñaan pexey noon moy.
Sabóor 141 in Kàddug Yàlla gi