Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 13:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 13:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 ba ma tàggook bopp bu ubu ak njàqarey xol bu sax, ba noon dootu ma man?
4 Céy Aji Sax ji sama Yàlla, geesu ma, wuyu ma, leqli ma, bala ma ne sërëx ci nelawi ndee,
5 noon ba naan: «Daan naa ko,» bañ yay bége saab jéll.
6 Man de maa ngi dénkoo sa ngor, di bànneexoo sag wall. Naa woy Aji Sax ji, ki may baaxe xéewalam.
Sabóor 13 in Kàddug Yàlla gi