Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 135:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 135:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Màggal-leen Ki Sax, Aji Sax jee baax! Kañleen ko, kee sopplu!
4 Ki Sax a taamu Yanqóoba, muy Israyil mi mu séddoo.
5 Maa xam ne Aji Sax ji màgg na! Sunu Boroom a sut lépp lu ñuy jaamu.
6 Lépp lu Aji Sax ji namm, moom lay def asamaan ak suuf, ak biir géej ak xóote yépp.
Sabóor 135 in Kàddug Yàlla gi