Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 126:3-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 126:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Lu réy la nu Aji Sax ji defal moos, nu bég.
4 Aji Sax ji, rikk delloo nu na woon, ni ngay delloo wal yu ŋiis, mu walaat ca àllub Negew.
5 Kuy ji di jooy, yal na góob, di sarxolle.
6 Ku doon wéya wéy, di jooy; ŋàbb mbuusum jiwoom, yal na dikka dikk, di woy, ñibbaale sabaaram.
Sabóor 126 in Kàddug Yàlla gi