Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - ROOM - ROOM 6

ROOM 6:4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Bi ñu nu sóobee ci ndox moomu nag, day misaal ne dañu noo suul ak Kirist, nu dee ni mu deeye woon; ba tax nu dekki it, ni mu dekkee woon ci dooley Yàlla Baay bi, te nu sóobu ci dund gu bees.

Read ROOM 6ROOM 6
Compare ROOM 6:4ROOM 6:4