Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - PEEÑU MA - PEEÑU MA 3

PEEÑU MA 3:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Moona am nga foofu ci Sàrd nit ñu néew ñoo xam ne tilimaluñu seen mbubb. Ñooñu dinañu ànd ak man, sol lu weex, ndaxte yeyoo nañu ko.
5Ku daan, dinga sol mbubb mu weex ni ñoom. Duma far sa tur ci téereb dund bi, waaye dinaa nangu ci sama kanam Baay ak ay malaakaam ne bokk nga ci man.
6Yaw mi am ay nopp, déglul li Xelum Yàlla di wax mboolooy ñi gëm.

Read PEEÑU MA 3PEEÑU MA 3
Compare PEEÑU MA 3:4-6PEEÑU MA 3:4-6