Text copied!
Bibles in Wolof

Ose 5:4 in Wolof

Help us?

Ose 5:4 in Kàddug Yàlla gi

4 Seeni jëf a leen mayul ñu dellu ci seen Yàlla, nde ngelawal ngànctoo wale fa seen biir, te Aji Sax ji, faalewuñu ko.
Ose 5 in Kàddug Yàlla gi