Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 8:7 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 8:7 in Kàddug Yàlla gi

7 Ndox mu ne xéew du fey mbëggeel, ay dex du ko mëdd. Ku koy weccee sa alalu kër gépp it, ñu jéppi laa jéppi rekk.
Ngën-gi-woy 8 in Kàddug Yàlla gi