Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 8:13-14 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 8:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Yaw mi tooge digg tool bi, samay xarit a ngi teewlu sa baat, waxal boog, ma dégg.
14 Nijaay, dawsil, melal ni kéwél, mbaa kooba gu ndaw ci kaw tund wi ci gàncax gu xeeñ gi.
Ngën-gi-woy 8 in Kàddug Yàlla gi