Text copied!
Bibles in Wolof

Ngën-gi-woy 7:7-8 in Wolof

Help us?

Ngën-gi-woy 7:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Rafet, sopploo! Soppee, bànneex nga!
8 Sa taxawaay bii garabu tàndarma la, sa ween yi di cëggi doom ya.
Ngën-gi-woy 7 in Kàddug Yàlla gi