Text copied!
CopyCompare
Téereb Injiil - LUUG - LUUG 10

LUUG 10:21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Ca saa soosu Xel mu Sell mi feesal Yeesu ak mbég, mu daldi ne: «Yaw Baay, Boroom asamaan ak suuf, maa ngi lay sant ci li nga nëbb yëf yii ñi am xam-xam ak ñi am xel, te xamal leen gone yi. Waaw, Baay, ndaxte looloo la neex.»

Read LUUG 10LUUG 10
Compare LUUG 10:21LUUG 10:21