Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 9:15-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 9:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Fekk fa ku néewle te xelu. Mu manoona xelal dëkk ba, xettli leen, waaye kenn faalewu ko.
16 Man dama noon xel mu rafet a gën doole! Ndeke ku néewle ñu xeeb la, tanqamlu say wax.
Kàdduy Waare 9 in Kàddug Yàlla gi