Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 9:10-11 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 9:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Liggéey boo gis, liggéeyal; def ci loo man. Ndax muy jëf, di doxalin, di xam-xam, di manoore, dara amu ci njaniiw, ga nga jëm.
11 Ma seetlooti fi kaw suuf ne du ku gaaw, yaay raw; du ku jàmbaare, yaa moom xare; du ku xelu, am loo dunde; du ku muus, duunle; du kuy xamkat, amu yiw; ku nekk ak bésam ak wërsëgam.
Kàdduy Waare 9 in Kàddug Yàlla gi