Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:7-10 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Foqarñi kay day dofloo boroom xel, te ab ger da lay gëlëmal.
8 Fa mbir mujjee gën fa mu doore, te muñ a gën réy-réylu.
9 Bul gaawa mer; mer, xolub dof la samp këram.
10 Bul ne lu tax démb dàq tey, loolu, laaj ko du xel.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi