Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:4-6 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Ku xelu, xalaat kërug dëj; ku dofe, xalaat kërug puukare.
5 Déglu ku xelu di la àrtu moo gën déglu dof bu lay woy.
6 Ab dof day textexi ni dég yuy retete taal bu cin tege. Loolu it di cóolóoli neen.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi