Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:19-21 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Xel mu rafet day dooleel boroom, ba mu man fukki kàngam cib dëkk.
20 Amul moos ku jub ci kaw suuf, kuy def lu baax te du bàkkaar.
21 Te it du lépp lu ñu wax, ngay bàyyi xel. Kon doo dégg surga bu la ŋàññ,
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi