Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:14-16 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Su neexee, bànneexul; su mettee, xoolal ne lu ci ne, Yàllaa ko def ngir jaam bi umple gannaawam.
15 Lu ne laa gis ci sama dund gu gàtt gii! Nit a ngii jub, teewu koo sànkook njubam; nit bon, ànd ak mbonam, gudd fan.
16 Bul jub ba mu ëpp, bul wóolu sam xel ba mu ëpp, lu ko moy nga yàqule.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi