Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 7:13-14 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 7:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Xoolal ci li Yàlla def: Ana ku mana jubbanti lu mu dëngal?
14 Su neexee, bànneexul; su mettee, xoolal ne lu ci ne, Yàllaa ko def ngir jaam bi umple gannaawam.
Kàdduy Waare 7 in Kàddug Yàlla gi