Text copied!
Bibles in Wolof

Kàdduy Waare 5:8-12 in Wolof

Help us?

Kàdduy Waare 5:8-12 in Kàddug Yàlla gi

8 Xanaa ndax buur suqal mbey mi, ba ñépp jariñoo suuf si.
9 Bëggkatu xaalis du doyal xaalis, bëggkatu alal du doyal tono, te loolu it, cóolóoli neen.
10 Bu koom yokkoo, lekk-kat yi yokku. Ana lu muy jariñ boroom koom ga, xanaa di ko duufale bëtam?
11 Surga, lekkam néew, bare, mu nelaw, ba fàttey boram; boroom alal regg, du nopplu, du nelaw.
12 Naqar wu réy laa gis fi kaw suuf: Alal ju boroom dajale ba loru,
Kàdduy Waare 5 in Kàddug Yàlla gi